Pape Amadou SALL vous présente la version Wolof de l’ouvrage de Seydil Hajj Malick SY (RTA), Khilaçu Zahab. Cet ouvrage consacré à la vie du prophète PSL est traduit en Wolof dans le but de permettre au public de se familiariser avec la Richesse du contenu et de bénéficier des connaissances gigantesques mobilisées.
La cérémonie de dédicace aura lieu à la maison de la culture Douta SECK, Samedi 09 Septembre 2023 à partir de 15H InshaAllah
Paap Amadu SÀL moo ngi leen di aajar téere sunu Maam Seex Sëyidil Haaj Maalig Si (RTA) bii di Xilâsu-Zahab. Nu bind ko ci làkku wolof ngir mu gën a jege nit ñi ngir it ñépp man ci jot ba njariñ li gën a yaatu ak ngir yaatal xam-xam.
Aajar gi moo ngi ame ci Maison de la culture Douta Seck, Gaawu 9i Setambur 2023 InshaAllah
Asfiyahi.Org